DiscoverXalaat - Ma Ibra Laye
Xalaat - Ma Ibra Laye
Claim Ownership

Xalaat - Ma Ibra Laye

Author: Ma Ibra Laye

Subscribed: 0Played: 0
Share

Description

C'est un partage de mes idées espérant qu'elles pourront vous être utiles.
18 Episodes
Reverse
Traduction wolof du Verset du Trône (Ayaatul Kursiy) tiré de la traduction wolof du Saint Coran du professeur feu Assane Sylla.
Ma Ibra Laye - Yobante bi - Partie 1
Suturaal sunu bopp te bañ di xaawi sunu sutura
Lu bari ci nitu tay yi, rawatina ndaw ñi da ñu yakkamti lool ngir tekki ndax pression sociale bi ñéneen ñi ndax bari ay bëgg-bëgg. Mu yobbu ñu ci état d'esprit "naa tekki rekk, anam bu ma mënë tekkee grawul", manaam bëgg forcer tekki bi donté da ñuy amee ci anam boo xamni diine daf ko tere. Te kepp kuy jullit war nga ànd ak patience te lepp looy wutt nga wutt ko ci anam bu dagan ndax mu baña nekk lu lay adina ak allaxira
Bu ñu gëmee ni Yàlla mooy Buur lu ko neex mu deff rekk di na ñu noppalu ci coono yu bari yu ñuy teg sunu xoll, te fexe di accepter ak di jeema adapter wu ndax lu bari ci dogalu Yàlla yi munu ñu ko soppi te it lu bari dafa doon lu gën ci ñun motax Yàlla amal, dafa fekk ni ñun ñoo dul xam li nekk ci ginnaaw dogal yooyu ndax Yàlla du jox kenn justificatif
Bataaxal bu jëm ci samay mbokk jullit, ginnaaw bi seetloo ni sori nañ lool ak jàngaley islam bi nga xamni, da ñuy woote ni ci moom la ñu tënku, ngir kenn ku nekk ci ñun nattaat boppam xool fan la ak njulliteem tollu
ñaan jëm ci Yàlla

ñaan jëm ci Yàlla

2024-05-0406:44

Dagaan Yàlla sunu Boroom ginnaaw bi mu dëkke ci di ñu defal ay xeewël, ñu ëlbatiku di jëfandikoo xeewël yooyu ngir deff lu tere ñu koy deff
Rappel de notre mission sur terre qui n’est autre que d’adorer AllahParticiper aux activités des ASC religieusement, c’est-à-dire ne jamais enfreindre les lois religieuses durant ces activités (se faire des ennemis, insulter son prochain, « marabouter » autrui, …)Conseils aux parents et aux jeunes
Partie 7 de la série « Yobbante bi » traitant de la façon de sevrer son nafs (passions) par le fait de manager son temps, de ne pas consommer de l’illicite et de faire constamment du zikr
Partie 8 de la série « Yobbante bi » traitant du devoir de faire Allah notre priorité devant toute créature en commençant par nos proches (père, mère, femme, enfant)
Partie 6 de la série Yobbante bi traitant des stratégies pour sevrer son nafs.
Cinquième partie de la série « Yobbante bi » traitant du fait que nous nous sommes eloignés du droit chemin tracé par Allah sans que nous nous en rendions compte.
Quatrième partie de la serie « Yobbante bi » Suite de la partie : comment gérer sa « célébrité » et les conséquences de nos actes envers nos semblables (pression sociale)
Deuxième partie de la serie « Yobbante bi » qui traite de la façon dont on doit se comporter à l’égard du pécheur qui cherche à se remettre sur le droit chemin
Troisième Partie de la serie « Yobbante bi » qui traite de la façon de gérer sa « célébrité »
Une réflexion sur les mariages après avoir être témoin de l'explosion des divorces
Ceci est juste une pensée aux gens qui souffrent dans le silence, et qui pourtant font de tout leur possible pour faire paraître le contraire
Quand Je ne serai plus

Quand Je ne serai plus

2024-05-0406:04

Doxalin bi nit yu bari di am bes bu ñu fi Yàlla jëlee, ba ñu ñuy dëjël. ñu war ci jàng ni amul benn mbindeef bu ñu wara jaral ñuy saggaane sunu diggante ak sunu Boroom ba azza wa jall
Comments