Zikrullah - Jangi Ngaxam 2025
Update: 2025-07-23
Description
𝑱𝒂𝒏𝒈𝒖𝒊 𝑵𝒈𝒂𝒌𝒉𝒂𝒎 🙏🏾
Xayrul Xalqi mo ngi Jaamalaay
Ruxu Laay feeru Kambereen
Bëyti Mamuur la nuy siyaar
Ngir dëgël waxi Limaamu Laay
#layenedigital #layene #ngakham2025 #ahloulahi
Comments
In Channel